We’ve updated our Terms of Use to reflect our new entity name and address. You can review the changes here.
We’ve updated our Terms of Use. You can review the changes here.

Dama B​ë​gga Ñibi (I Want To Go Home)

by Aron And The Jeri Jeri Band

/
  • Streaming + Download

    Includes unlimited streaming via the free Bandcamp app, plus high-quality download in MP3, FLAC and more.
    Purchasable with gift card

      €15 EUR  or more

     

1.
Yee waaw Wooy tukki yombul waa-waaw Wooy sama tukki gi Tukki jom la waaw Tukki jom la waaye ñibbisi mooy fulla Man de da ma bëgg a ñibbi Man de da ma bëgg a ñibbi Sama yaay a ngi may xaar Sama baay a ngi may xaar Nàmm naa yaay Nàmm naa baay bóoy Da ma bëgg a ñibbi waaw Da ma bëgg a ñibbi waaw Da ma bëgg a ñibbi waaw Da ma bëgg a dellusi Xamuma kañ la Kañ lay doon Kañ laay ñibbi Duggal naa samay këyit man di xaar Xamuma kañ la xamuma fan la man Xale yaa ngi may xaar man Mag yaa ngi may xaar man Sama yaay ngi may xaar man Ay su ma ñówe di ngeen kontaan Di ngeen kontaan Su ma ñówe di ngeen kontaan Di ngeen kontaan Da ma bëgg a ñibbi Da ma bëgg a ñibbi Da ma bëgg a ñibbi Da ma bëgg a ñibbi Wàlliyaan oo cey wàlliyaan ee Aa waa-waaw waaw Ma ni da ma bëgg ñibbi Sama doom juddu na sama ginnaaw Dugal naa samay këyit toog di xaar Mu yàgg loole Ba mu juddoo ba léegi tegu ma ko bët Nàmm lool gis ko Doom jooju nga xam ne da fa juddu sama ginnaw Da ma bëgg a ñibbi Da ma bëgg a ñibbi Da ma bëgg a ñibbi Da ma bëgg a ñibbi Dellusil noo ngi lay xaar Dellusil noo ngi lay xaar Dellusil noo ngi lay xaar Tukki jom la waaye ñibbi fulla la Loo mën a am Noo mën a mel Ñibbisil Da ma bëgg a ñibbi waaw Da ma bëgg a dellusi Da ma bëgg a ñibbi waaw Da ma bëgg a dellusi
2.
Sunugal 04:14
Moy sunu reew Moom le ñuy tiitëroo Senegal Ndiaye Senegal moy Suñu gaal Ku ñëw te menoo joow Demal ba ñëw sénégal Deku diine le Deku Teranga la Kene du ko miim Dëku diine le Dëku Teranga la Wey naa ko Magg ñu baax ni Dëku diine le Dëku jamm le Weyy sénégal Kaay ñu añ Kaay ñu reer Amul feneen fu dul sénégal Moy Suñugal Kene du ko miim Dëku Bamba la Kene du ko miim Dëku Maodo le woooy Saalum ba sine Limaamu laay ca yoff Boucounta Ndiassane Senegal Ndiaye Dëku Gainde la Ku ñëw te menoo joow Demal ba ñew sénégal Sénégal Suñugal Sénégalais Kadior ak Baol Saalum ba Siine Lepp ci sénégal Kaay giss sunugaal Ku ñëw te menoo joow Demal ba ñëw sénégal Kena dou ko miim DëkuTeranga Amna Médina Baay Amna Touba Kena dou ko miim DëkuTeranga Amna Medina Baay Amna Touba Amna Tivaounane Amna Ndiassane Kena dou ko miim Te bët sët na boo yeewo yeema Lu ko waral! ENGLISH TRANSLATION SENEGAL ! It’s our country It’s our pride Senegal Ndiaye Senegal we are in the same boat A place of It's a place of hospitality Without comparison A place of It's a place of hospitality I sang the great elders Place of peace Come have lunch with us Come and have dinner with us There is no other place like Senegal It’s very special The country of Bamba The country of Maodo From Saalum to Siin Limamoulaye in Yoff Boucounta Ndiassane Senegal Ndiaye The land of lions If you can’t row Wait until you arrived in Senegal Senegal our boat, Senegalese ! Kadior and Baol Saaluum to Siine Everything is here ! Come and see Wait until you arrived in Senegal The holy city of Medina Baay is here! The holy city of Touba is here ! The holy city of Tivaouane is here ! The holy city of Ndiassane also ! When it’s daylight wake me up Why ?
3.
Mama Djuma 06:11
Sànt naa la Bëgg naa la Mama yaay sama gàllaj Mama yaay sama gàllaj Àdduna amul solo yaay Mama yaay sama gàllaaj Àdduna amul solo Bëgg naa la Fonk naa la Mama Djuma Bëgg nga ma Taxawu ma Suturaal ma Féete ma fu bari Mama Djuma
4.
Teddoungal 04:39
5.
Ngaldoore 04:35
6.
Maam Baye 05:04
Àllaa Kénn du Maam Baay Cey Baay Baay Ñas jommal na nit ku weex Jommal na nit ku ñuul Yàlla Da fay dimbali ci lu gaaw Lu mu wax Yàlla ni waaw Jubook boroomam raw na góor ñi ma woy Mu nga ganee àdduna Koosi Ñów Lewna Ñaseen ñépp naan Baay ma woy Soxna Astu Jànxa mooy sa yaay Dëgg-dëgg Baay Ñas romb na ay kéemaan Ba ma deme America dem ba Londres Gambia ba Àngalteer ñépp naan Maam Baay Illa Laah Illa laah Kénn du Maam Baay ndeysaan Yónent moo di sangam oo Alxuraan diineem Baay Ñas Yónent moo di sangam oo Alxuraan diineem Lu ko waay gënoon a soxla mu ba la ak loola Loo ko ñaan mu may la Maam Baay Ba ma deme America ñépp ña ngay bégge Maam Baay Ba ma deme Nigeria ñépp ña ngay bégge Maam Baay Aa bëggul ku dul Baay Maamam la ca maam sët a koy jël ee aa ma woy Dëgg-dëgg Gambia bëggu ñu ku dul Maam Baay Ñaŋ xarañ Lóo seede ma ma woy Michel seede ma ma woy Maam Baay Su ma woye Maam Baay péy bi yëngu Su ma woye Maam Baay Lewna Yëngu Su ma woye Maam Baay àdduna Yëngu Ñépp a ko bëgg kénn du Maam Baay Dëgg-dëgg kénn du Maam Baay Ca dëgg-dëgg kénn du Maam Baay Ibu Bambara bëggul ku dul Maam Baay Dënnam baak xolam ba defu ci ku dul Maam Baay Waa Koosi waa Nigeria Lewna Ñaseen dem ba Bongre Ndar gu ndaw ñépp ñu ngi bégge Maam Baay Kénn du Maam Baay Illa Laah Illa laah Maam Baay ma woy
7.
Kaolack 03:13
8.
Bongo Boys 05:27
9.
Jeri Jeri 04:07
Jéeri Jéeri-jéeri Jéeri Jéeri-jéeri Sàmbay mbayaan Juuf ee Buur ba lay ñaan Xare ba ca cuur-cuur Ku fa yóbbu buum Cér kese lay yeew Sàmbay mbayaan Jéeri Jéeri-jéeri Jéeri Jéeri-jéeri Maalawbe Sàmba Kullu ma ca Seen Gi Ndaat Jéeri Ngoone Maalawbe Sàmba Kullu ma ca Seen Gi Ndaat Jéeri Ngoone Maalawbe Sàmba Kullu ma ca Seen Gi Ndaat Jéeri Ngoone Kullu ma ca Seen Gi Ndaat ee Aa Jéeri Boo ame dimbali ko Boo ame dimbali ko Boo ame dimbali ko Boo ame dimbali ko Yor Doole di ko Jaay Yor Doole di ko Jaay Yor Doole di ko Jaay Yor Doole di ko Jaay Boo mëne dimbali ko Boo mëne dimbali ko Boo mëne dimbali ko Boo mëne dimbali ko Ey waay te Yàlla tax waay
10.
11.
Hmmm waaw Ma woyal ñi ma yaroondool Ñi ma yaroondool Àjjana li ko wër coono yu metti rekk la Waaye bakkan ak àdduna rekk a wër safara Yàlla la mu yor Njaayam noflaay jëndu ko Jëf rekk a lay may ay biram Yow mii Xamnaa ni yow nit ku baax nga Nanu jaamu ji Yàlla Xam ko mbaa nga xam ndawam Ku ràññe xutbu samaan doo weddi lii ma wax Ab dof na muy faje ay dof loolu mbégte la Ee Ndeysaan Fekkeel sama njariñ yaay bóoy Saa Daali Majoojo Anta Faal Majigéen Bayu Soogi Ajaratu Ndey Caam mooy sama yaay Alaaji Màgget Ñaŋ ay sama baay Ndeysaan oo wuy lee Mamaa Bàmbi Caam Séex Becco Cuun Naaru Maam Bàmbi Caam Maa lay woy ndax yow yaay Ndaanaan mat a woy waaw Yaay Bóoy

about

" Through this music ", says Ottignon," I hope to promote a better understanding of Senegalese culture and the important role that music plays as a bridge between different cultures and traditions. It's important to recognize that what is considered ‚normal’ in one culture is not necessarily better or worse than what is considered normal in another. Education and understanding are key to appreciating and celebrating our differences. We are all unique, and this music serves as a vessel to promote acceptance and celebration of our differences." The band has already played its first concerts in Dakar and made a name for itself with them; more are planned on the African continent and in Europe.

credits

released January 12, 2024

Technical Credits

Engineer - Aron Ottignon (Urban Trout Studios)
Mastered -Clinton McCreery on Behalf Of Bambu Studios
Mixed - Aron Ottignon
Recording Engineer - Aron Ottignon (Urban Trout Records)
Ouzin Ndoye (Jeri Jeri Studios)

ARTWORK: Audrey d’Erneville

license

all rights reserved

tags

about

Aron And The Jeri Jeri Band Senegal

“Fusion Collaboration’s post modern mbalax mash-ups ” - Mojo Magazine

“Homesick, electronically adventurous Senegalese Blues, featuring Baba Maal”
8/10 - Uncut Magazine

Unleash style and warmth with our Aron & the Jeri Jeri Band debut album hoodie & t shirt

urbantroutmerch.creator-spring.com/listing/new-dama-begga-nibi
... more

contact / help

Contact Aron And The Jeri Jeri Band

Streaming and
Download help

Report this album or account

Aron And The Jeri Jeri Band recommends:

If you like Aron And The Jeri Jeri Band, you may also like: